Liy raam ca ñak ba la jëm

"Les chiens aboient ... la caravane passe" se disent ceux qui nous gouvernent depuis plusieurs décennies. Arrêtons d'aboyer et consommons les ruptures qui sont les nôtres. Arrêtons les calculs politiciens et mettons en place des structures aptes à renverser la tendance actuelle. Le "Y en a marrISME" n'est qu'un petit gémissent qui ne provoquera jamais de vrais changements. Mobilisons nous dès maintenant. N'attendons pas l'implosion très très prévisible de la COALITION-CONTRE-NATURE-QUI-NOUS-GOUVERNE pour la mise en place de vraies structures alternatives.


Liy raam, ca ñak ba la jëm

SEMEtt kuréel la guy dajale ay gëstukat ci mbirum njàng , ñuy yënggu ci mbirum  caada, ñuy yenggu ci wallu sinemaa, ñeneen ñu macce ci lu jëm ci yoon , ñii ci mbiru koom-koom, ñële ci xarala yu bees yi, ay jàganlekat, ay taskatu xibaar ag ñu nekkinu askan wi yittéel, té ñoom ñëpp ittewo mbiru njàngale mi, maanaam ëllegu Afirig, ndax da ñu gëm ne yokkuteem manul jaar fenn fudul ci tàggat i nitam, ngir ñu gëna xarañ te gëna gëm seen bopp.

Posts les plus consultés de ce blog

Kadhafi voudrait une armée de 2 millions d’hommes pour l’Afrique

Talla Sylla : un parcours politique précoce et mouvementé

Cameroun : les émeutes donnent lieu à une répression d'envergure