Liy raam ca ñak ba la jëm
"Les chiens aboient ... la caravane passe" se disent ceux qui nous gouvernent depuis plusieurs décennies. Arrêtons d'aboyer et consommons les ruptures qui sont les nôtres. Arrêtons les calculs politiciens et mettons en place des structures aptes à renverser la tendance actuelle. Le "Y en a marrISME" n'est qu'un petit gémissent qui ne provoquera jamais de vrais changements. Mobilisons nous dès maintenant. N'attendons pas l'implosion très très prévisible de la COALITION-CONTRE-NATURE-QUI-NOUS-GOUVERNE pour la mise en place de vraies structures alternatives. Liy raam, ca ñak ba la jëm SEMEtt kuréel la guy dajale ay gëstukat ci mbirum njàng , ñ uy yënggu ci mbirum caada, ñ uy yenggu ci wallu sinemaa, ñ eneen ñ u macce ci lu jëm ci yoon , ñ ii ci mbiru koom-koom, ñ ële ci xarala yu bees yi, ay jàganlekat, ay taskatu xibaar ag ñ u nekkinu askan wi yittéel, té ñ oom ñ ëpp ittewo mbiru njàngale mi, maanaam ëlleg...